Mbind mu sell mi
La Bible Wolof


Fii ngay jànge walla yebe Kàddug Yàlla gi

Bible Wolof

Ventes, écrire à B.P. 1229, Thiès, Sénégal
ou à Yàlla Wax Na / Dieu a Parlé, 10 rue de Thiong, Dakar dieuaparle@live.fr


Fii ngay jànge walla yebe téerey Kàddug Yàlla yi ñu lim

Kàddug Yàlla gi
Téere bu mag, biy kàddug Yàlla gépp, juróom benn fukki téere laak juróom benn.
Yàlla moo tànn ay yonent ak yeneeni nit ci diiru junniy at ak juróomi téeméer, xiir léen ci bind kàddoom.


Xaaj 1: Téereb kóllëre gu jëkk gi (Xaaj 2: Téereb Injiil)
   
Kóllêre gu jëkk gi, di xaaj bu jëkk ci Kàddug Yàlla gi

Tawreet
Yonent Yàlla Musaa moo bind Tawreet. Mooy juróomi téere yi jiitu ci Kàddug Yàlla gi.

Njàlbéen ga (Genèse, 2016)  Yeb ko | Jàng ko ci wolofal

Njàlbéen ga mooy téere bi jëkk ci Kàddug Yàlla gi, te moo jiitu ci Tawreetu yonent Yàlla Musaa.

Mucc ga (Exode, 2016) Yeb ko | Déglu ko

Ñaareelu xaaju Tawreet, di téereb Mucc ga, moo wéyal jaar-jaari bànni Israyil, jële ko fa ko
téereb Njàlbéen ga bàyyi woon.

Sarxalkat yi (Lévitique, 2016) Yeb ko

Ñetteelu xaaj bu Tawreetu Musaa jëm ci sasu Sarxalkat yi.

Màndiŋ ma (Nombres, 2017) Yeb ko

Baamtug Yoon wi (Deutéronome, 2017) Yeb ko

Téerey Cosaan yi (livres historiques)

(Josué, nu ngi koy négandiku)
(Juges, nu ngi koy négandiku)

Ruut (Ruth, 2016) Yeb ko | Seetaan ko ci wideyo | Déglu ko
1 Samyel (1 Samuel, 2016) Yeb ko
2 Samyel (2 Samuel, 2016) Yeb ko
1 Buur ya (1 Rois, 2016) Yeb ko
2 Buur ya (2 Rois, 2016) Yeb ko
(1 Chronique, nu ngi koy négandiku)
(2 Chronique, nu ngi koy négandiku)

Esra (Esdras, 2016) Yeb ko
Neyemi (Néhémie, 2016) Yeb ko
Esteer (Esther, 2016) Yeb ko

Téerey Taalif yi 

(Job, nu ngi koy négandiku)
Sabóor (Psaumes, 2016) Yeb ko | Jàng ko ci wolofal | Déglu ko.
Kàddu yu Xelu (Proverbes, 2016) Yeb ko
Kàdduy Waare (Ecclésiastes, 2016) Yeb ko
Ngën-gi-woy (Cantique, 2016) Yeb ko

Téerey Waxyu yi  

(Ésaïe, nu ngi koy négandiku)
Yeremi (Jérémie, 2016) Yeb ko
Kàdduy Jooytu (Lamentations, 2016) Yeb ko
Esekiyel (Ézéchiel, 2016) Yeb ko
Dañeel (Daniel, 2016) Yeb ko
(Osée, nu ngi koy négandiku)
(Joël, nu ngi koy négandiku)

Amos (Amos, 2016) Yeb ko
(Abdias, nu ngi koy négandiku)
Yunus (Jonas, 2016) Yeb ko
(Michée, nu ngi koy négandiku)
(Nahum, nu ngi koy négandiku)
(Habakuk, nu ngi koy négandiku)
(Sophonie, nu ngi koy négandiku)
(Aggée, nu ngi koy négandiku)
(Zacharie, nu ngi koy négandiku)
(Malachie, nu ngi koy négandiku)


Xaaj 2: Téereb kóllëre gu mujj gi  Jàng ko. Yeb ko. Déglu ko.
    (
Xaaj 1: Téereb Yonent yi)

    
Kóllere gu bees gi mooy xaajub ñaareel bu Kàddug Yàlla gi. Mooy kóllëre gi Yàlla fas ak nit,
      te mu sottee ci Almasi Yeesu.

Waxi yonent yi jëm ci Almasi
Liy yombal njàngum téere bii
Nanu ràññee
Copyright
Ubbite gi

Leeral yi

Xibaaru Jàmm bi ci Almasi  Yeesu
Xibaar bu bees bi di Kàddu yiy biral dundu Almasi bu sell bi Yeesu, Yàlla jaarale na ko ca gaayam yu tedd yi:

MACË (Évangile selon Matthieu)
MÀRK (Évangile selon Marc)
LUUG (Évangile selon Luc)
YOWAANA (Évangile selon Jean)

Jëfi ndaw yi
Kàddug Yàlla tasaaroo na ci àddina :

JËFI NDAW YA KIRIST YÓNNI (Les Actes des Apôtres) 

Bataaxal yi
Kàddu yiy biral yaatuwaayu ngëneel yi ci Kirist, ni ko ndawam yu tedd yi binde:

   Bataaxal yi Yàlla may Póol, mu bind ko :

WAA ROOM (Épitre de Paul aux Romains)
1 WAA KORENT (Premier Épitre de Paul aux Corinthiens)
2 WAA KORENT (Segond Épitre de Paul aux Corinthiens)
WAA GALASI (Épitre de Paul aux Galates)
WAA EFES (Épitre de Paul aux Éphésiens)
WAA FILIB (Épitre de Paul aux Philippiens)
WAA KOLOS (Épitre de Paul aux Colossiens)
1 WAA TESALONIG (Premier Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
2 WAA TESALONIG (Second Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
1 TIMOTE (Premier Épitre de Paul à Timothée
2 TIMOTE (Segond Épiitre de Paul à Timothée)
TIT (Épitre de Paul à Tite)
FILEMON (Épitre de Paul à Philémon) 

Bataaxal bi jëm ca YAWUT YA (Épitre aux Hébreux) 

Bataaxal bi Yàlla may SAAG, mu bind ko (Épitre aux Hébreux) 

   Bataaxal yi Yàlla may Piyeer, mu bind ko (Épitres de Pierre)

1 PIYEER (Permier Épitre de Pierre)
2 PIYEER (Segond Épitre de Pierre) 

   Bataaxal yi Yàlla may Yowaana, mu bind ko (Épitres de Jean)

1 YOWAANA (Permier Épitre de Jean)
2 YOWAANA (Segond Épitre de Jean)
3 YOWAANA (Troisième Épitre de Jean) 

Bataaxal bi Yàlla may YUDD, mu bind ko (Épitre de Jude).

Téereb Peeñu mi

Kàddu yiy xamle mbir yi wara ñëw te Yeesu Kirist won ko Yowaana ci biir peeñu

►  PEEÑU MI (La Révélation de Jésus-Christ à Jean) 


Demal ca kaw